Sangue Ndiaye l'heritier de Baye Niass



Salam sangyi! zamane bou nek rek yalla dafay wathie si mbidafoone yi ngir guidiléne wayé si sounou zamane baay niass moy yalla kone soudé yalla zatoula day hotékou ngir amal mazayir yi.Donc baay niass il faut que mou amal mazayiryi fi hilatou motah baye wahné"mine ankar ila Sierra leone turti ila batossine darou sidiqina foudal.mine battoussine turti ila dakari woulki bi mirssiha hassa tassiyri" baye mouné "mangi bawo ankar dieum sierra leone fala nawé dieum gambie keuryoyou nak ay keur you deugoulagne wayé gnou bah lagne.Thi gambie fala nawé dieum dakar fala sani sama yatbi baparé diko weur" kone haqou dou tok ben place rek kom gniy dingate sangue ndiaye fogué ndah baay dafané"maa zala rassoulilahi yata rakafi boutoune boutoune hatal am" mouné "yonent dégnoul di ragnane di ragnane bassi batinou batine bataydji" lii day firndél né noubouwa wilaya ak hilafa fi hilafatou lou ame la.wayé so yamé hilafa fi hilafatou rek da ngay doone kathior ndah qala baye"bi kaolaha tawrane aw bi yoffine wa maratane bi barrissa darou fassiqina koussala"baye mouné "thie kalolak ay diamano wala bok si yoff benen yone thie paris nak ay keuroup kthior lagne"kone daa beugueu wah ni rek gni top haqou si nassiou mahdi bassi insiwiya té wathiou gnou nassot gnom ay kathior lagne kou wedi nak ni nassot amoul qala baye"famane li bibarqine mine sanai dakari wa qad dia wa zal babou bahrou ganari" mouné foumay gnéwalé bidew bo hamné momay leral dakar bou nonou nak bateaubi dialna ganar" ndah pépe dougoupe bi dafa doh si dounde doh si gatah doh si gope kone loukoy teréé nekat pépe?motah baye newat"famane li bil imami bi taybati bi naqa ma qara rassouli dia ahirane wa mouhaddama" "naka lamay gnéwalé nditou tayba si naqa.naqa bo bou nounou nak moy sahouwayou yonent bi nga hamné gneuwna si moudieuteul wayé moy ndit" pépe dougoupe bi mo ndieuk wayé mome lagnou sahalone.kouy wedi nak né baay dougne ko dondou cheikh ibrahim si boppam mo né "fa yadji bou alal mouridi safira ila mane houwa kamiloul hensri hasa henhou wata adabou bayna wadeyhi wata kidou hahodi mouhamadoyatu ahmadiytu ibrahimiyatu wa ine haqa walidi fi zalika" baye moubé "warna si mouride mou lahas deme outi imamou zamaname ndah mou fédali kolaréme ak mouhamadiyatu ahmadiyatu ibrahimiatu thie ndigalou seurigname" kone kou diokouwoul si borome zamane té moy sangue ndiaye do meuneu hame baaay ndah "la aflaha mane aflaha ila bissouhbatine mane aflaha" "diambi dou téhé mouk loumoy dafa diokou si kou téhé.gniy wédiné sangue ndiaye mo dondou cheikh ibrahim baay dafané"fa hadartou aw tani wa ahli wa ouchrati adioubou fala lam achkoukatou kalala"baye mouné"diéguina rewyi andak samay ndiogne ak samay dome ma dague all yi wayé dioyou ma ndono"kone baay dinagne koy donde

pour mou ler si gni gueumoul né nassot rekay deugue baay mo wahat né "al oumati qasdi fi himou an achoukahoum ila qadrati bari rahim ila houna" baye né "namouma si het wilé oumoy mangue léne dieumeulélene si pays yalla bi séne borome"kone mbolene mbébetou cheikh ibrahim nassot lawone motah mou wah si beytibi "ya oumouka wafdoune hatawal ardi ta-irane ilal moustaphal mouhtari bahrou hata-i" " manak samay het leme nagne soufsi naw dieum si yonent bignou tane ki kokou moy guediou may gui" wayé yonent bi bay di wah dou bi nek si guinawam wayé binek si kanamam lay wah ndah moné"iza sara hayrou nass sirtou wara ahou wa ine hala yawmane fal massirou ba-i dou"ki dueune si mbidef sou dohé ma doh wayé sou beuss bi wathié dagnouy doh lou sorri" kone bayy baye yonent bimouy wah si kanamam la nek "wa hardjtou lil housti charifine wa bahdaou saraytou bi barhama halilou mouafaqane" "mangi bawo si pays bou sellbi si guinaw fofou fala ragnané dieum si barhama sopé mou deupo ak lima beuguoone" lolou la baye wah kou andak touti hél dinga hamné li ma wah fi ay beyti vhekh ibrahim la ta bay moy fouhat kone kouko wédi rek to talibéme

"wala haqou hichrou dine henssa mouhibbina bali loubi loubi loubi mahda ta-i" mane baay sama talibé zahir warta doone thieureum batine warouko doone wayé batinou batine moy wara doone thieureum" nguéne balma ak boubah souma dioumé rek nguéne hamné defar moma beugoone na diouk.Maxhalla