Extrait du livre Jamihou Jawamihou page 008



Ala layta chiheri hâl afouzou bi rouheyati, moukhaya Rasouloulahi? Zalika bouheyati.
Aka nékhone ma tékhé ci maa guis, kanamou Seydina Muhamad? Lolou moy sama tiakoutéf.

Wa hâl alebisane khoulehal oumami? Moukamilane, rafihane, wa yahetini alazi ouwa mouneyati.
Ndah dana sol foutékouk Sangue yii? Ma nék kou mât, kou yeukeutikou, boba dana am sama mbémbat.

Wa hâl youdjeliyane anil fouhadi rouyounahou? Fasara kaniberasine, ilahoul bariyati?
Ndah dina niou dindi ci sama khol ay neukh neukham? Mou moudj lér nii sétou, yow YALLAy mindafun yii?

Wa hâl toucherikhane chamsoul irfani, djeukheuratane bi khiblati khalbi, douna chakine wa miryatine?
Ndah dana fénk jantap kham YALLA, cii jakarlo cii sama khibla khol bii, cii lou amoul bén siki saka ak wéréneté?

Wa hâl tametourane souheboul marifa, wabilane bi ardy fouhadi? Khahizane koula khineyati.
Ndah dana taw niri (nuages) kham kham yii, niouy adji dotékou (sotékou vc force) cii sama soufou khol bii? May adji lak bép kôm (richesse)

Wa hâl lii chouhoudoune ayni ayni ilahina, bi aynaya, khisane? Fahikhane ahelou nouheyati.
Ndah dana sédé jeumou jeumi YALLA dji, cii sama 2 beuts, cii yeuk? Ma kawé borom khél you sél yeup.

Wa hâl yakechifane ane fouhadi hawayatane? Fa ameliya khawfane, mah-rajahine wa khacheyati
Ndah dana niou dindi cii sama khol mbéwté gui mou néké? Niou fésalé ko ragal, andak yakar ak torokhlou (YALLA)

Wa hâl ajelisane yawmane, outafou ka Kahebatine? Bi anewahi ihsanine, bi sidekhine tawiyatine
Ndah dana tok biss, nioumay weur comme ni niouy weuré Kaaba Gui? Cii ay khétou rafétal, ak cii deugou you lémou

Wa hâl lii adahou fardi, ineda Moukhasabine? Wafi Taybatil hady? Alayhi takhiyati.
Ndah dana ma niél ma jokhé farata, cii Moukhasab (tour leh cii tourou Macca yii)? Ak deukou aji guindi dji (Hady)? Nékna fofou sama nouyo.

Wa hâl artakhi fawkhal maqamati wasilane ila lahi? Matebouhane bi nafsine zakiyati.
Ndah dana yék ciikaw maqama yii may aji jokou cii YALLA? Ma nék kouniou top cii bakane bou sél.

Wa hâl lii nadjatou nafsi, mine chari khasidine? Iza khasadal mikhsadou, ani lii bouhayati.
Ndah dana ma niél moutiouk (échapper) bakane, touké cii ayou aji aniane dji? Est ce que dana mouc cii mom?

Wa hâl lii ijetimahou chamsi, mine hayri fourekhatine? Asalou bi tahelimine bi tahelici niyati
Ndah dana ma niél ma dajék jant bii, cii loudoul may takaliko ak mom? Kone dana kéro cii xam cii sélouk yéné?

Wa hâl lii khawezi koula ma kountou talibane mina lahi ame laysa al boulouhou lii mouneyati
Ndah dana ma niél ma lak limay sakou yeup touké cii YALLA, mba dina jot samay mbémbat?

Salatoune wa taslimoune, ala hayri khalkhihi, wa aline, wa askhabine, wa khoutboul bariyati
Djouli ak seulmal nék nah cii qui gueune cii mindafun yii, ak gnognam, ak ay andadowam, ak qui gaa khamni moy njitou mindafun yii! ////



Mor Asta Kébé