Salam sangyi! zamane bou nek rek yalla dafay wathie si mbidafoone yi ngir guidiléne wayé si sounou zamane Baye Niass moy yalla kone soudé yalla zatoula day hotékou ngir amal mazayir yi.Donc baay niass il faut que mou amal mazayiryi fi hilatou motah Baye wahné"mine ankar ila Sierra leone turti ila batossine darou sidiqina foudal.mine battoussine turti ila dakari woulki bi mirssiha hassa tassiyri" baye mouné "mangi bawo ankar dieum sierra leone fala nawé dieum gambie keuryoyou nak ay keur you deugoulagne wayé gnou bah lagne.Thi Gambie fala nawé dieum Dakar fala sani sama yatbi baparé diko weur" kone haqou dou tok ben place rek kom gniy dingate Sangue Ndiaye fogué ndah baay dafané"maa zala Rassoulilahi yata rakafi boutoune boutoune hatal am" mouné "yonent dégnoul di ragnane di ragnane bassi Batinou Batine Bataydji" lii day firndél né noubouwa wilaya ak hilafa fi hilafatou lou ame la.